Luke 9:44 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
«Dégluleen bu baax lii ma leen di wax: dinañu jébbal Doomu nit ki ci loxoy nit ñi.»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
«Ubbileen seeni nopp te teewlu bu baax kàddu yii: Doomu nit ki lees di wor, ngir teg ko ci loxoy nit ñi.»