Luke 9:46 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Werante am ci biir taalibe yi, ñuy laajante kan moo gën a màgg ci ñoom.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Werante moo dikkaloon taalibe yi, ñuy seet kan moo gëna kawe ci ñoom.