Luke 9:47 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Yeesu mi xam seen xalaat, jël ab xale, teg ci wetam ne leen:
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Yeesu nag ràññee seen xalaat. Mu daldi indi ab xale, taxawal ko ci wetam.