Luke 9:48 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
«Ku nangu xale bii ci sama tur, man mii nga nangu; te ku ma nangu, nangu nga ki ma yónni; ndaxte ki gën a woyof ci yéen ñépp, kooku moo gën a màgg.»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Mu ne leen: «Xale bii, képp ku ko dalal ndax sama tur, man nga dalal; te képp ku ma dalal, dalal nga ki ma yebal; ndax ki gëna tuut ci yeen ñépp, kooku moo gëna màgg.»