Luke 9:50 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Waaye Yeesu tontu ko: «Buleen ko tere, ndaxte ku la sotul, far na ak yaw.»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Yeesu ne ko: «Buleen ko aaye, ndax ku la sotul, yaw la faral.»