Luke 9:51 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Bi jamono ji jegeñsee, ji Yeesu waree jóge àddina dem asamaan, mu sigiñu ci dem Yerusalem.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ba ñu demee ba bés bi ñu wara yéege Yeesu di jubsi, Yeesu moo dogu ngir dem Yerusalem.