Luke 9:53 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Waaye waa dëkk ba nanguwuñu ko, ndaxte mi ngi jublu woon Yerusalem.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Waa Samari nag nanguwuñu koo dalal, ndax Yerusalem ga mu nammoona jëm.