Luke 9:57 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Bi ñuy dem, am ci yoon wi ku ne Yeesu: «Dinaa la topp fépp foo jëm.»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ca yoon wa ñu awe la jenn waay ne Yeesu: «Yaw laay topp fépp foo jëm.»