Luke 9:6 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Noonu ñu dem dëkk ak dëkk, di fa yégle xebaar bu baax bi, tey wéral jarag yi.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ñuy dem nag, di wër dëkk ak dëkk, di yégle xibaaru jàmm bi, di faj jarag ji.