Luke 9:7 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Bi Erodd boroom diiwaanu Galile déggee li Yeesu ak ay taalibeem doon def lépp, mu jaaxle, ndaxte amoon na, ñu doon wax ci mbiri Yeesu naan: «Yaxya moo dekki.»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ci kaw loolu Erodd boroom Galile dégg mboolem la xew, boppam nag ubu, ndax ñenn ñu noon Yaxya moo dekki, di Yeesu.