Mark 1:27 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Bi loolu amee ñépp waaru, ba laajante naan: «Kii mooy kan? Mii njàngale lu bees la te ànd ak sañ-sañ. Day sant rab yi sax, ñu di ko déggal.»