Mark 1:38 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Waaye Yeesu tontu leen: «Nanu dem feneen ci dëkk yi nu wër, ma waare fa itam, ndaxte moo tax ma génn.»