Mark 10:13 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Bi loolu wéyee ñu indil Yeesu ay xale, ngir mu teg leen ay loxoom. Waaye taalibe ya gëdd nit ñi.