Mark 10:24 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Wax jooju nag daldi jaaxal taalibe yi lool. Waaye Yeesu neeti leen: «Samay xarit, dugg ci nguuru Yàlla, lu jafee ngoogu!