Mark 10:43 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Buleen mel ni ñooñu. Waaye ku bëgg a nekk kilifa ci yéen, na nekk seen surga,