Mark 10:48 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Ci kaw loolu ñu bare gëdd ko, ngir mu noppi. Teewul mu gën a yuuxu naan: «Yaw Sëtu Daawuda bi, yërëm ma!»