Mark 10:5 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Waaye Yeesu ne leen: «Dénkaane boobu mu leen bindal, bind na ko ndax seen xol dafa fatt.