Mark 11:24 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Moo tax maa ngi leen koy wax, bu ngeen di ñaan Yàlla, lépp lu ngeen ko man a laaj, gëmleen ne jot ngeen ko, te dingeen ko am.