Mark 11:32 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Waaye bu nu nee: “Ci nit ñi,” kon mbooloo mi dal ci sunu kaw;» ndaxte ñépp teg nañu Yaxya ab yonent.