Mark 12:15 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Waaye Yeesu xam na seen naaféq, mu ne leen: «Lu tax ngeen bëgg maa fiir? Indil-leen ma posetu denariyon, ma seet.»