Mark 12:18 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Gannaaw loolu ay Sadusen ñëw ci moom, ngir laaj ko lenn. Sadusen yi nag gëmuñu ne, ndekkite am na.