Mark 12:22 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Mbir mi dem na nag, ba juróom-ñaar ñooñu ñépp dem, te kenn bàyyiwu fi doom. Mujj jigéen ja faatu moom itam.