Mark 12:27 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Li ci génn mooy, nekkul Yàllay ñi dee, waaye Yàllay ñiy dund la. Kon sóobu ngeen cig réer.»