Mark 12:32 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Xutbakat bi ne ko: «Waaw kilifa gi, li nga wax dëgg la: Yàlla kenn la, te amul jeneen Yàlla ju dul moom.