Mark 12:33 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Te nga bëgg ko ak sa xol bépp ak sa xel mépp ak sa kàttan gépp moo dàq bépp sarax bu ñuy yóbbu ngir màggal Yàlla ak bu ñuy lakk ca saraxalukaay ba.»