Mark 12:35 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Bi nga xamee ne Yeesu ma nga doon jàngale ca kër Yàlla ga, mu laaj nit ñi: «Lu tax xutbakat yi di wax ne, Almasi bi mooy sëtu Daawuda?