Mark 12:36 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Daawuda moom wax na ci kàttanu Xel mu Sell mi naan:“Boroom bi nee na sama Boroom:«“Toogal ci sama ndeyjoor,ba kera may daaneelsay noon ci sa kanam.»“ “