Mark 13:2 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Waaye Yeesu tontu leen: «Du gis ngeen taax yu réy yii yépp? Lii lépp dina daanu, ba doj dootul des ci kaw doj.»