Mark 13:20 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Te bu fekkul woon Boroom bi wàññi bés yooyu, kenn du mucc, waaye fekk na mu wàññi leen ndax gaayam ñi mu tànn.

Recommended Reading