Mark 13:29 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Noonu itam bu ngeen gisee loolu lépp xew, xamleen ne jege na; mu ngi ci bunt bi sax.