Mark 13:8 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Xeet dina jóg, xeex ak weneen xeet, réew xeex ak meneen réew. Te yengu-yenguy suuf dina am ciy bérab yu bare, ak ay xiif. Loolu lépp mooy ndoortel metit yi, mel ni jigéen juy matu.