Mark 14:12 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Bés bu jëkk ca màggal, ga ñuy wax Mburu ya amul lawiir, taalibey Yeesu laaj ko: «Foo bëgg, nu defaral la reeru Jéggi bi?» Bés bu jëkk booba nag mooy bés, ba ñu faral a rendi xarum màggalu Jéggi ba.