Mark 14:16 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Bi mu ko waxee, taalibe ya dem ca dëkk ba, gis lépp, ni leen ko Yeesu waxe woon. Noonu ñu defar reer bi.

Recommended Reading