Mark 14:21 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Doomu nit ki mu ngi dem, ni ñu ko waxe ci Mbind mi, waaye ki koy wor dina torox. Bañoon a juddu moo gën ci moom.»