Mark 14:36 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Mu ne: «Abba, Baay bi, yaw mi dara tëwul, teggil ma kaasu naqar bii. Moona bumu doon sama coobare, waaye na sa coobare am.»