Mark 14:41 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Ñetteelu yoon mu dellusi ci ñoom ne leen: «Yéena ngi nelaw tey noppalu ba tey! Jeex na. Waxtu wi jot na; ñu ngi wor Doomu nit ki ci loxoy bàkkaarkat yi.