Mark 14:49 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Moona daan naa toog bés bu nekk ca kër Yàlla ga, di jàngale, te jàppuleen ma. Waaye lii am na, ngir Mbind mi am.»