Mark 14:58 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
«Nun daal dégg nanu, mu ne: “Dinaa toj kër Yàlla, gii loxoy nit liggéey, tabax ci ñetti fan geneen gu nit liggéeyul.”»