Mark 14:62 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Yeesu tontu ko: «Moom laa. Te dingeen gis, Doomu nit ki toog ci ndeyjooru Aji Kàttan ji, di ñëw ci niiri asamaan.»