Mark 14:69 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Foofa nag mbindaan mi gisaat ko, mu ne ñi fa taxaw: «Waa jii ci ñoom la bokk.»