Mark 14:70 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Waaye Piyeer weddiwaat ko.Nes tuuti ñi fa taxaw ne Piyeer: «Yaw mi de, ci lu wóor bokk nga ci, nde waa Galile nga.»