Mark 15:16 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Bi loolu amee ñu dugal Yeesu ci biir kër boroom réew ma, mooy bérab bu ñuy wax Peretoriyum, ñu daldi woo mbooloom xarekat yépp.