Mark 15:2 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Noonu Pilaat laaj ko: «Ndax yaa di buuru Yawut yi?» Yeesu tontu ko: «Wax nga ko.»