Mark 15:29 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Ña fa doon romb di ko xas, di wëcc seen bopp ndax sib ko naan: «Waaw kay, yaw mi bëgg a toj kër Yàlla gi, tabaxaat ko ci ñetti fan,