Mark 15:32 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Almasi bii, di buuru Israyil, na wàcc léegi ci bant bi, nu gis ko te gëm.» Ñi ñu daajaale ak moom it di ko xarab.