Mark 15:7 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Fekk booba amoon na ku ñu tëj, tudd Barabas, ku bokk ci ña bëggoon a tas réew mi, boole ci rey nit.