Mark 2:19 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Yeesu tontu leen: «Ndax gan, yi ñëw cig céet, dinañu woor, fekk boroom céet gi ànd ak ñoom? Duñu woor, li feek boroom céet gaa ngi ànd ak ñoom.