Mark 2:27 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Yeesu dellu ne leen: «Yàlla sàkkul nit ngir bésu noflaay bi, waaye sàkk na bésu noflaay ngir nit.