Mark 2:9 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Lan moo gën a yomb, ma wax ku làggi ki: “Baal nañu la say bàkkaar,” walla ma wax ko: “Jógal, jël sa basaŋ, tey dox”?