Mark 3:28 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Ci dëgg maa ngi leen koy wax, lépp dees na ko baal nit ñi, muy bàkkaar, muy sosal Yàlla wu mu man a doon.